AM DOOM - gTt-VIH

Transcription

AM DOOM - gTt-VIH
Nit nu baari yu ame VIH di nanu am doom te du -nu
ka wala feebar bi. Wante nak da faay fekk mu and ak
ndimbalu doktoor.
WOLOF
AM DOOM
BU DE JIGEEN GU AME VIH
Bo de jël garab yi wanni
doole doomu jangooro
ji ci ëmb gi, dina aar sa
doom ba du ame VIH.
Bo ame liimu VIH bu
nëw ci sa deret (ba
keen du ko giis) ndam
sax mën nga mucc ci
anam yi ka nëpp di
deffe.
Bu lollu amul da faay jar
nu opeere la ngir xale bi
juddu.
Digglewun ngay nàmpal
.
Ci diiru ay bës gànaaw
bi nga muccé, doom ji
dafa wara jël garab yi di
waññi doole doomu
jangooro.
Bo tope diggle yi ci
temeeru xale yu un jël
keen kott mu ci am VIH.
Doom ju ame VIH
Doom ju
amul VIH
BO DE GOOR GU AME VIH:
GTT-VIH
GRUPO DE TRABAJO SOBRE
TRATAMIENTOS DEL VIH
Bo sëy bu andul ak
fagaaru ak jigeen mën
nga ko wala, moom mu
wala doomam.
ENTIDAD DECLARADA DE UTILIDAD PÚBLICA
ONG DE DESARROLLO
Bu yaay ji amul VIH
doom ji du ko am ,
ndax doomu jangooro
mënul joogé ci bay bi
dem ci doom ji.
Bo ame liimu VIH bu nëw
ci yaram ( bu keen du ko
giis) wallante ci sëy yu
andul ak fagaaru tamit
day nëw. Lajjal sa
doktoor ci lollu.
RAÑEE:
Ak pàcc mi Boole ci defiin yi war, ay junni jigeen yu ame VIH jur nan
ay doom yu wer.
¿TIENES DUDAS
SOBRE EL TEMA?
PREGÚNTANOS
Tel. 93 458 26 41
[email protected]
Garab yi wanni doole doomu jangooro ji da niiy ar doom yi ci VIH.
Bu ame VIH Boole ci ëmb, ba bu naame amb doom, li nulaay diggal
mooy nga wax ak sa doktoor ci tambali ëmb gi.
INFOVIHTAL / AM DOOM

Documents pareils