infovihtal #95 VIH: Li ciiy léeb ak dëgg (III) - gTt-VIH

Transcription

infovihtal #95 VIH: Li ciiy léeb ak dëgg (III) - gTt-VIH
infovihtal 95
VIH: Li ciiy léeb ak dëgg
(III)
#
Leeb
Màttu yoo ba gúnoór mën joxe
VIH.
1
Leeb
Nit ni amee VIH mënun am doom.
2
VIH
Dëgg
Leeb
Amul been wallu VIH bu am jaare ci
yoon wowu. Ndam sax gunoór màtt na ku
amee VIH muccu deretam, doomi jangooro
bi mënul dund ci biir gunoór gi tax ba du
mën jallal ség gi ci keneen.
Setlu yi ci deret daf taxa ñaakalo
deret di ma lootaloo.
Dëgg
Deret dafaay bàaw ci yaram te
yeesalaat boppam fu mu tollu, tamit
ci setlu yi tutti lañ ciy jël, ba yeesal
ko ci yaram day gàaw. Di lekk lekku gu
baax, te bañ di tógg rek di nala dimbali
nga am kataan . Te setlu lu war la ngir nu
xam fu sa yaram tollu.
Grupo de Trabajo
sobre Tratamientos
del VIH
[email protected]
www.gtt-vih.org
Barcelona (España)
3
Dëgg
Leeb
Dëgg
Nu baari un amee VIH nekk naañ Yaay
ba paapa te seeni doom du un juddu ak
doomi jangooro ji. Ci jamoono ci am na ay
pexe yu un tekk ba nit ku amee VIH mëna
juur te wallu andandowam ba doomam.
Pàcc mi daf may sopi
ba nëpp xam ne dama
amee VIH.
4
Amna nu baari yu amee VIH di fàccu te
di wone wer ci seen yaram. Ndam ség gi
ak yeen ci garab yu Hjek yi daan naañ sopi
nit ba mune fanŋci yaram mam, ci jamono
yi garab yi dotuño tolof tolof yu mel n. Xam
nak ne fàccu bu dal amna ay baax ak ay
loorange.
POR FAVOR, FOTOCÓPIALO Y HAZLO CIRCULAR
Subvencionado por:
Colaboran:
Programa de Prevenció i Assistència
de la Sida
Àrea de Qualitat de Vida, Igualtat
i Esports
Àrea de Benestar Social