Dinddi biir ci sa coobare

Transcription

Dinddi biir ci sa coobare
18, rue du Général Leclerc
91100 Corbeil-Essonnes
09 79 72 55 44
[email protected]
www.perinatifsud.org
Tél : 09 79 72 55 44
Fax : 01 60 89 39 02
[email protected]
www.perinatifsud.org
Yooni wootekaay yu gaaw ngir jot
liggéeykat ti kër doktoor yi ci mbirum
dindi,
Ligéeykati kër yiy toppatoo soreel njur ak
yeete ci mbiru njaboot (CPEF)
Këri doktooru nguur gi
Arpajon
Corbeil (CHSF)
Dourdan (CHSE)
Etampes (CHSE)
Fontainebleau
Longjumeau
Melun
Montereau
Orsay
Villeneuve St Georges
01 64 92 91 49
01 61 69 71 11
01 60 81 58 57
01 60 80 78 66
01 60 74 12 64
01 64 48 20 20
01 64 71 65 84
01 64 31 65 70
01 69 29 75 85
01 43 86 20 08
Evry
Kilinigu Essonne
Kilinigu Mousseau
Fontainebleau
polikilinig La Forêt
01 69 54 45 45
Dotoor yi ci taax yi
Boo ci bëggee am lu la doy xoolal fii:
01 60 87 86 30
01 60 77 62 52
www.perinatifsud.org/fr/
interruption-de-grossesse
01 64 69 77 78
www.ancic.asso.fr/
Massy
I H Jacques Cartier
Melun
polikilinig Saint Jean
www.seine-et-marne.fr/les-services-de-la-PMI
Yi am kontaraa ak këridoktoor yi nguur gi
nàngu
KERI DOKTOORU J0MBUUR YI
Athis Mons
Opitaalu Athis-Mons
www.essonne.fr
Wànn nga lor,
Te bëggoo
Biir bi sotti
01 60 13 62 26
www.IVGlesadresses.org
01 64 14 30 02
Quincy-sous-Sénart
Opitaalu Claude Galien
09 79 72 55 44
[email protected]
www.perinatifsud.org
www.planning-familial.org/
01 69 39 90 31
18, rue du Général Leclerc
91100 Corbeil-Essonnes
L’ IVG
(Dinddi biir ci sa
coobare )
Ay boroomi xam-xam ci
loolu man nanu leen a
dimbali
Ban pexe ngay tànn ?
Tànn leen pexe mi ci ndimbalu doktoor bi,
mu aju nak ci ni mbir yi tëdde (soo
nekkee ci sa weeru njur, wër gu yaram
wi, ak yu ni mel.).
Dindi biir ci naan ay doom
Pexe ,i ,i ngi aju ci jël ay doom yaari yoon
ci diirub 36 waxtu mbaa 48 waxtu
Manees nakoo naanee ca sa kër ndeem
biir bi weesoogul juroomi weer, walla ca
kër doktoor ba ndeem biir bi weesoogul
juroom yaari weer
Kërug kaarànge ci wàllu neekin dana la
delloo téemeer ci téemeer boo fay, dalee
ko ci 31 mars 2013
Su dee amoo asiraas sosiyaal, jokkool ak
kër yiy toppatoo soreel njur ak yeete ci
mbiru njaboot .
Dindi biir ci opeere
Pexe moomu day aju ci nu manq li nga
ëmb, laata ngay dugg ci fukk ay bis ak
yaar
Manees nanoo anestesiye lenn ci sa
yaram wala ci sa yaram yépp. Danga gënn
ci ngoon si wala ca suba ga.
Sooy dindi biir ci sa coobare, dananu la bindal
ay garab gu aju ci fànn gi nga tànn muy:
• ay gabi metiit ak ay garb yu lay teree jur.
• benn paase wisit wala ekogarafi su weesoo 10
fan ba 21 fan.
Tél : 09 79 72 55 44
Fax : 01 60 89 39 02
[email protected]
www.perinatifsud.org
Bàyyil xel ci diir yin la may!
Jokkool ak OLUS nu mu gëna gaawe
Ndeem sax nekk nga di siki-saka
Tànn pexe dindi sa biir ci sa coobare
mbiru mu aju la ci sa bopp, waaye
yoon a ko lal,
Ànd ak nu bàyyi la diirub ay bés nga
xalaat ko.
Waxtaan wooy seq ak ku am xam-xam
ci loolu dananu la ko may.
Su dee boroom xam-xam bi nga dem du
yëngu ci dindi biir cig coobare (ndax am
xelam may ko ko),
Dafa la ware tegtal keneen ku ci
nangoo soobu te nangu laa jël
Jigeen ji mu dal rekk a ko mana
ñaan
Ab doktoor rekk a ko mana def
.
Soo doonagulee sa magum bopp, te
yéenewoo koo yëgal sa waa kër,
jokkool ak ag kër guy toppatoo
soreel njur ak yeete ci mbiru njaboot
wala sa doktoor.
18, rue du Général Leclerc
91100 Corbeil-Essonnes